John 8:55 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xamuleen ko nag; man maa ko xam. Su ma ne woon xawma ko, ab fenkat laay doon ni yéen. Waaye xam naa ko te maa ngi sàmm waxam.