John 8:59 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu for ay xeer, bëgg ko koo sànni ngir rey ko. Waaye Yeesu nëbbu, génn kër Yàlla ga.