John 8:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu nag, dañu ko doon wax ngir seetlu ko, ndaxte bëggoon nañoo tiiñal Yeesu. Yeesu sëgg, di bind ak baaraamam ci suuf.

Recommended Reading