John 9:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Farisen ya laajaat ka gumba woon ne ko: «Yaw, loo wax ci moom? Yaw de la ubbil say bët.» Mu ne leen: «Yonent la.»