John 9:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yawut ya mënuñu woon a nangu ne, nit ka dafa gumba woon tey gis léegi, ñu daldi wooluji ay waajuram,