John 9:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
laaj leen ne: «Ndax kii mooy seen doom, ji ngeen ne, gumba judduwaale la? Kon fu mu jaar, bay gis léegi?»