John 9:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Taalibeem ya laaj ko ne: «Kilifa gi, lu tax waa jii judduwaale gumba? Ndax bàkkaaram a ko waral, walla bu waajuram?»