John 9:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Farisen ya dellu woowaat ka gumba woon ne ko: «Waxal sa digganteek Yàlla. Xam nanu ne, waa joojee boroom bàkkaar la.»