John 9:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne leen: «Wax naa leen ko ba noppi, waaye dégluwuleen ma. Lu ngeen bëgg ci ma di ko wax, di waxaat? Xanaa dangeen a bëgg a nekk yéen itam ay taalibeem?»