John 9:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam nanu ne, Yàlla du déglu boroom bàkkaar. Waaye nag, dina déglu ki koy ragal tey def coobareem.