John 9:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu leen ne: «Bu ngeen gumba woon, dungeen am bàkkaar, waaye fi ak yéena ngi naan: “Nu ngi gis,” ci bàkkaar ngeen di dëkk.