Jonah 1:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Géej ga nag di gëna sàmbaraax. Ñu ne ko: «Nu nu lay def nag, ba géej gi dalal nu?»