Jude 1:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Duñu noppee xultu, di jàmbat seen nekkin, tey topp seen nafsu; ay wax yu réy a ngi ball ci seen làmmiñ, waaye dañuy jey ñi ñuy yaakaare njariñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñoo di ñaxtu ak a jàmbat, te topp seen bakkan; kàdduy damu yu réy ay jibe seen gémmiñ, te ñooy jay ñi ñu yaakaare njariñ.