Jude 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ne leen: «Muju jamono ay tiiñalkat dinañu feeñ, ñuy weddi Yàlla, ngir topp seen bakkan.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne leen: «Mujug jamono, dina am ay ñaawlekat yu topp seen bakkan, wéye seen kéefar.»