Jude 1:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñooy féewale, te Xelum Yàlla nekkul ci ñoom, waaye niti kese lañu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñu ñooy féewalekat yi, ñoo topp seen bindu judduwaale, te Noowug Yàlla nekkul ci ñoom.
Recommended Reading