Jude 1:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
ngeen musal ñale, jële leen ci safara, te yërëm ñeneen ñi, waaye boole ci moytu, ba sib sax seen yére yi taq sobe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ñii ngeen wallu leen, foqatee leen ci sawara, ña ca des, ngeen yërëm leen yërmande ju ànd akug ragal, ba far seexlu ab turki bu seen yaram sobeel ndax seeni bàkkaar.