Jude 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka noonu itam gentkat yooyu may wax ñu ngi sobeel seen yaram, di weddi gépp kilifteef, di xas doole yi ci asamaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Géntkat yii itam noonu rekk lañuy sobeele seen yaramu bopp, boole ci di sofental kilifteef, ak di saaga boroom daraja ya fa asamaan.