Leviticus 13:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su gàkk bi yemee foofu te lawul ci yaram wi, ab tut la bu juddoo ci lakk-lakk bi. Na sarxalkat bi biral ne nit ki set na, ndax légétub lakk-lakk ba la.