Leviticus 13:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na sarxalkat bi seet gàkk bi ci yaramu nit ki; su fekkee ne kawar gi ci gàkk bi dafa soppiku weex, te mu mel ni lu def pax ci der bi, jàngoroy der juy law la. Bu sarxalkat bi gisee loolu, na biral ne nit ki sobewu na.