Leviticus 13:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
na ko sarxalkat bi dellu seet ba gis ne wat-wataan ji law na ci yaram wi. Su boobaa soxlaatul mu di ca seet kawar gu xall, ndax nit ki sobewu na.