Leviticus 14:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sarxalkat biy laabal nit ki day indi nit ki, mu ànd ak loolu lépp, taxaw fi kanam Aji Sax ji, ci bunt xaymab ndaje mi.