Leviticus 14:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
defal ko ki ñuy laabal njotlaayam ngir mu tàggook sobeem. Te itam na sarxalkat bi rendi saraxu dóomal bi,