Leviticus 16:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam day wis-wisale baaraamam deret ji lu mat juróom ñaari yoon ci kaw sarxalukaay bi, setal ko, sellal ko, mu tàggook sobey bànni Israyil.