Leviticus 18:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bul jébbal kenn ci say doom tuur mi ñuy wax Moleg, ndax waruloo teddadil sa turu Yàlla. Man maay Aji Sax ji.