Leviticus 2:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen mboolem saraxu pepp nangeen ko xorom. Bu seen saraxu pepp ñàkk mukk xorom, ndax mooy màndargaal seen kóllëreek seen Yàlla. Seen sarax yépp ngeen di xorom.