Leviticus 20:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ku dëkkoo sa soxnas baay, sa baay nga torxal. Ñoom ñaar ñépp dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.