Leviticus 20:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su jigéen jëmee ci mala mu mu doon, ba jaxasook moom, booleleen ku jigéen kaak mala ma, rey. Dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.