Leviticus 20:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Góor gu bokk ci yeen mbaa jigéen, di seete nit ñu dee mbaa muy boroom rawaan buy gisaane, dee rekk mooy àtteem. Dees koy dóor ay doj, mu dee, gàddu bakkanu boppam.»