Leviticus 20:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su fekkee ne waa réew mi dañu koo seetaan ba seetaan ko, muy jox Moleg ku bokk ciy doomam te taxul ñu rey ko,