Leviticus 21:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mbaa ab jigéenam bu séyagul te bootu ci moom ndax amul jëkkër— ku mu bokkal noonu, sañ naa sobewu ndax moom.