Leviticus 22:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nit dee joxsi Aji Sax ji aw nag mbaa gàtt, muy saraxu cant ci biir jàmm, mu di ko wàccoo ngiñ mbaa muy saraxu yéene, na doon lu amul sikk, ndax ñu nangul ko. Lenn luy sikk du nekk ci jur gi.