Leviticus 23:42 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci ay mbaar ngeen di dëkk diiru juróom ñaari fan yooyu. Mboolem njuddu-ji-réew ci Israyil na ci dëkke mbaar,