Leviticus 25:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ñu ko jotaatul ba njaay ma am atum lëmm, dëkkuwaay boobu ci biir dëkk bu mag ba ñu wëralee tata day wel fàww, ñeel ka ko jënd, mook ku askanoo ci moom. Du lees di delloo ci atum Yiwiku.