Leviticus 25:47 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su fekkee ne ab doxandéem bu ngeen dëkkal mbaa ab màngaan dafa woomle te kenn ci seeni bokk ñàkk, ba jaay boppam doxandéem bi ngeen dëkkal mbaa kenn ku bokk ak doxandéem bi,