Leviticus 26:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
su boobaa ma gën leena mereeti, noonoo leen, te man ci sama bopp maa leen di mbugalati lu ko ëpp fukki yoon ak juróom, feye leen ko seen bàkkaar.