Leviticus 26:40 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su ko defee ñoom dinañu tudd seen bàkkaar ak seen bàkkaaru maam ya, ndax dañu maa wor te dëkke maa noonoo,