Leviticus 27:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nit jagleelee Aji Sax ji dëkkuwaayam, sellalal ko ko, na sarxalkat bi xayma dëkkuwaay bi. Su baaxee su bonee, lu mu ci dogal mooy wéy.