Leviticus 27:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nit jagleelee Aji Sax ji suuf su mu moom ci suufas ndonoom, na ñuy xaymaa suuf sa, na dëppook dayob pepp bay mat jiwum suuf sa. Ñetti barigoy peppum lors yu ne juróom fukki dogi xaalis a koy wecci.