Leviticus 27:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye kat luy taaw cig jur, Aji Sax jee ko moom jeeg. Du lu kenn di dogoo jagleel Aji Sax ji. Muy barmol, muy mbote, muy tef, Aji Sax jeey boroom.