Leviticus 27:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Deesu ci seet jur gu baax ak gu bon te deesu ci wuutal lenn. Bu ci nit xasee wuutal lenn, la jëkk ak la ko wuutu lépp day daldi doon lu sell. Deesu ko mana jotaat.»