Leviticus 27:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su fekkee ne ki dogu woona jagleel nit ki Aji Sax ji da di ku am-amam yées sa xayma, na kooku yóbbu nit ki ba ca sarxalkat ba, sarxalkat bi xaymaal ko nit ki ci lu dëppook am-amam, moom mi dogu woon.