Leviticus 3:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su fekkee ne li nit kiy sarxalal Aji Sax ji saraxu cant la ci biir jàmm, te mu di ko jële ci jur gu gàtt, gu góor mbaa gu jigéen, na sarxal lu amul sikk.