Leviticus 5:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu nit bàkkaaree ndax lu mu dégg wooteb seede cib àtte, ba noppi baña wax la mu gis mbaa mu xam ko ca mbir ma, dees na ko ko topp.