bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Leviticus 5:21
Leviticus 5:21 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nit ñàkkee wormaal Aji Sax ji ci waxi fen yu mu wax moroomam, ci alal ju ñu ko tayle mbaa ñu abal ko ko, mbaa muy lu mu jële ci càcc mbaa àq ju mu lekke ci moroomam,