Leviticus 5:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Nit ki amul lu mat njégu gàtt, na indil Aji Sax ji ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw, muy daanam ndax bàkkaar bi mu def; benn bi di saraxu póotum bàkkaar, bi ci des di sarax rendi-dóomal.