Leviticus 7:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su nit joxee ab saraxu rendi-dóomal, sarxalkat bi mooy féetewoo deru jur gi mu sarxal.