Luke 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sakariya daldi ne malaaka ma: «Nan laay xame ne, loolu dëgg la? Ndaxte mag laa, te sama jabar it màggat na.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàkkaryaa nag ne malaaka mi: «Lu may def ab takk ci loolu ba mu bir ma? Ndax man màggat naa, te sama soxna it làq na ay fan.»