Luke 1:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
te naan: «Lii mooy yiw wi ma Boroom bi defal, ba fajal ma li doon sama gàcce ci nit ñi!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Lii Boroom bee ma ko defal ci jant yi mu ma geesoo, ba teggil ma sama gàcce gi ci biir nit ñi!»