Luke 1:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waxi malaaka ma daldi jaaxal Maryaama, muy xalaat lu nuyoo boobu man a tekki.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxi malaaka ma nag jaaxal Maryaama, muy xalaat lu nuyoo boobu mana tekki.