Luke 1:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Malaaka ma ne ko: «Bul ragal dara Maryaama, ndaxte Yàlla tànn na la ci yiwam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Malaaka ma ne ko: «Maryaama, bul tiit, ndax daje nga ak yiwu Yàlla.